Wikbaatukaay — Wikipedia
Aller au contenu
Jóge Wikipedia.
Sémbu Wikbaatukaay
Wikbaatukaay
ab baatukaay barilàkk bu ubbeeku la, di benn ci sémbi
Wikimedia Fondation
yi. Baatub «Wikbaatukaay» dafay junj sumb bu
wolof
bu boobu sémb, di
Wiktionary
ci
wu-angalteer
. Mook
Wikipedia
ñoo bokk doxiin, di lu ubbeeku te dàttu ci nosteg
wiki
, lees man a jëfandikoowaat ci anami
GFDL
Tëddiin
Soppi
soppi gongikuwaay bi
Yéeney sémb bi mooy sos ab baatukaay bees di duggal làkki àdduna bi yépp. Ci bu wolof baat yépp a fiy nekk ak seen tekki ci yeneen làkk waaye ci wolof lañu leen di faramfaccee, joge seen
gongikubaat
, seeni
bokktekki
safaantekki
waxiin
, añs.
Ci «
» lañ ko jële
Wàll
Baatukaay
Sémbi Wikimedia Fondation
Wikbaatukaay
Yokkuw tëriit